dimanche 23 avril 2006

Il faut NEUTRALISER la classe politique sénégalaise: "AMUL LAQ LAKKAL" Par Papa Oumar FALL

Papa Oumar FALL
Membre de la Société civile ''culturelle'' sénégalaise
Acteur culturel linguiste de formation
Site web perso: STYLOCULTURE
***
Ci miim jamono
Dëgga attan tumuranke !
Waaye moo doy cip weetal
Waaye moo doy cip wettal
Xoolal fenn ni muy lawe
Melna geej gu aay
Duus yay fewi-fewi!
Dooley ngelawam upp na
Suuf si tasaaroo!
Cëy lii
Bip pënd
Di warac-waraci
Teeyayu xel
Mankook
Sellayu xol
Ñoom seen
Mucc sip lor
Xëlimaak daa
Doy nap gannay
Xareek jëësi wees na
Deqqi teenup Dëqële
Fekku fap teere
Nasaraan si bind na
Amul laq lakkal
A! Joor jok jot na!
*
***LIRE***
la traduction française ci-dessous
(Cf. Commentaires SEMEtt***)
*ORIGIN
AL CV de Papa Oumar FALL
Quelques PUBLICATIONS
de Papa Oumar FALL:

Articles les plus consultés