vendredi 21 octobre 2011

Afrik, ma di leen siggil ndigaale Xadafi

Mbonte Xadafi yàggoon na lool si jal bii, munu maa ànd si li reewu nasaraan yi def. Li xew Libi tiis na. Te liy xeeñ si ñàg bi la jëm. Ma ngi kay nàqarlu bu baax. Sama diine digël nama lu ma mënula soppi ak samay yoxo, ma mettit lu ka sama xol ... ba àddina xam ni àndu ma si. Su fekkee ni lii lanuy woowe "Nouvel Ordre mondial", andu masi. Lii du lenn ludul "ëpp sa moroom doole, wan ka ko". Neena nu dëggay mujj. Waaye may lacce: ban dëgg? ***Siggi***Taxaw***SEMEtt*** Afrik sunu ... asa kanam***
Pofrima Selo http://facebook.com/styloculture

Articles les plus consultés